jaaraama maam jaara

Upload: dieuzbu

Post on 04-Oct-2015

32 views

Category:

Documents


0 download

DESCRIPTION

Poeme de Serigne Moussa Kâ dédié à Soxna Jaaratullaah, la Sainte mère de Cheikh Ahmadou Bambawww.drouss.org

TRANSCRIPT

  • Page titre

    Seex Muusaa Ka

    Jaaraam Maam Jaara

    1436 h / 2015 - www.drouss.orgTous droits de reproduction rservs, sauf pour distribution

    gratuite sans rien modifier du texte.Pour toutes questions, suggestions, ou erreurs, veuillez

    nous contacter par le biais de notre site internet : www.drouss.org

  • 2 - Jaaraama Maam Jaara

    Quelques indications

    Wolof Franaise = per pru = ou rus rousc = th caam thiam = gn am gnamx = kh xol kholj = dj jibi djibinj = nd njaay ndiayend = nd nday ndeye aam (machoire) = eu gm = geum = (plus dur) = rr perduo = au gor gaureq = xx suqali soukh khaliii - uu - oo - aa ee (tirer sur le son) ; Ex : biir - suur -xool - gaal - xeer

  • Jaaraama Maam Jaara - 3

    Aperu sur lauteur

    Pote et disciple de Seex Ahmadu Bmba, Seex Muusaa K fut lun des plus grands historiens qui aient trait et comment la vie du Cheikh.Seex Muusaa K, fils de Usmaan et de Absatu Sekk, est n Ndilki prs de Mbkke Bawal vers 1890. Il fit ses tudes coraniques dabord aprs de son pre. Ensuite celui-ci le confia Ahmadu Bmba qui, de retour de lexil en Mauritanie, le garda dans sa cour de Ceyen (au Jolof) o il fut en rsidence surveille de (1907 1912), puis Diourbel partir de 1912. Atteint de variole, il dut renoncer son intention de faire des voyages dtudes travers le pays pour rester auprs de Seex Ibrahima Faal qui lui donna une solide formation religieuse.

    Excellent calligraphe, il entra dans le foyer dtudes appel Daaray Kaamil charg uniquement de lire et de transcrire le Coran en plusieurs exemplaires. Promu cheikh par Xaadimu Rasuul, il alla sinstaller Saat trois kilomtres de Mbakk pour enseigner le Coran...Ds la disparition de Seex Bmba en 1927, il se fit le compagnon de Seex Mustafaa Mbkke, son fils, premier khalife des murids, quil suivait dans ses dplacements travers le pays...

  • 4 - Jaaraama Maam Jaara

    Fin lettr, il a commenc du vivant de Seex Ahmadu Bmba composer des pomes en langue arabe. Il les montra son matre qui, souriant aprs lecture des textes, lui dit en wolof : Muusaa, leeralal fr yi mbir mi, en substance Muusaa, explique le message aux adeptes Muusaa, en murid disciplin, comprit, par linjonction du marabout, quil fallait sexprimer dans la langue wolof pour atteindre la grande masse de disciple qui ne parlaient pas arabe...Seex Muusaa Ka est un rudit. Il matrise aussi bien les textes sacrs, les paroles et les faits du Prophte Anleyhi-s-salaatu wa salaam (la sunna), que loeuvre de son matre et guide spirituel Xaadimu Rasuul. Cest ce qui lui permet de se mouvoir aisment dans son domaine de prdilection et de varier volont son style, ses thmes, la mtrique de ses vers, inspirs certes de la qasida arabe mais dont le rythme reste purement ngre...Il a de nombreux sobriquets : Njam, Wrkaanu Bmba, Xaadimul Xadiim, Gwl u Bmba. Certains de ses vers rtablissent correctement les liens de parent qui le lient Bmba. Mais, lui, a toujours souhait rester son chantre, car pour les murids, il importe moins dtre un proche parent du Cheikh que dtre son fidle taalib.

    Voil Sri Muusaa Ka brivement prsent. On ne peut le connatre rellement quen lisant la totalit de son oeuvre monumentale estime plus de vingt mille (20.000) versets

  • Jaaraama Maam Jaara - 5

    Ses Ouvrages : Ndiouth Ndiath ; Yrmande ; Taxmiss bob wolofal ; Muqadimaat ; Xarnu bi ; Su ngeen ma degloo ; May dagaan ; Boroomam ; Jigen u Mbkke-Mbkke ; Jaaramaa Maam Jaara ; Soxna Jaara ; Barsan ; Jazu Sakor u Gej gi ; Jazu Sakor u Jeri ji ; Sa pack bi ; Ci barke Bmba ; Ma yeesal (Xadi Sill) ; Ndenkaani buy royu gor ; Yalla yi teqqalikook yu suufe yi ; Marsiyya Seex Ibra Faal ; Sopp Ahmadul Mbkkii ; Maggal yi ; Ndaama day yuqeelu (Matlabul aajaati) ; Mustafa Mbkke ; Na jema buurati...

  • 6 - Jaaraama Maam Jaara

    Jaaraama Maam Jaara

    Bismi-l-laahi-r-Rahmni-r-Rahmi Wa sallalaahu Tahanlaa anla Seyidina wa mawlaanaa

    Muhammadin wa aalihi wa sahbihii wa xayra xadiimihii wa sallama tasliiman

    Xerawlu leen nu sant Soxna Jaara Ngir moo nu may li tax nu sampi daara

    Bu leen ma tanqamlu, bu leen ma tanqal Bu leen nxal ndoxum ki leen di tnqal

    Cellantu leen te wubbi seni noppu Ak sen xol ma wubbi seni boppu

    Te gnne seni wagaani xol te taataan Maam Jaara waame la ku naanul yaa bon

    Taw na Bawal(1) tawna Kajoor ak Njmbur Ba walangaan ku mar lek doob jmbur

    Waaloo ngi wal-wali di gental Waalo Ngir naani ci gejuk doomi Asta Waalo

    1 des nakoo bindee yit Bawol

  • Jaaraama Maam Jaara - 7

    Jaaraama Maam Astu ma feeru Naawel Sa gej gi neex na waaju naan si far wl

    Jaaraama Maam Jaara ma feeru Poroxaan Naxoo dayoo noo ngi dtm bay coroxaan

    Gannr dtm nau ba naan ba mandi Yaay bambulaan sam ndox xajul ci xandi

    ppa gi moss sab liggey ba Saalum Fuuta futtiku nau sagan ne maalum

    Yaw sa aub liggey bii dm na penku Dem soow baarakalla lii duk faggu

    Yekkal nga waa gej gi yekkal waa jeri Ba pp gejal yaw bayo fu joor

    Beykat nga bey nga beyooy dendi Jigeen i booyal yaw nga bay ba Ndindi

    Jigeen a soxla lau yaa doon Soxna Ndaanaan nga wub nga lambi doomi soxna

  • 8 - Jaaraama Maam Jaara

    Moo tax jigeen i seni doom ne mng Di rera kay fee yaw sa doom ne fng

    Moo tax jigeen pp seni doom diy xaadam Di gont a kay xy yaw sa doom dib yaaram

    Yaa tax jigeen pp seni doom seex Bu dul konak yaw noo ngi damm bay soox

    Tekkalelaak jigeen i Buso Baali Xawna araam mel na ni Yallaak yaali

    Di tudd seni doom di tudd Bmba Araam na ngir moom rekka ttan yen ba

    Yaw yaa di Buso Baali kko cangaay Naka nga jg sngg nu jox nu ay gaay

    Yaa tax jigeen iy lamasoo ay mlfa Nuy soli xawsa fu nu sob nu jl fa

    Jigeen i da daa gaardi woddooy soppi Gor i di biioy baxaoy roof roppi

  • Jaaraama Maam Jaara - 9

    Yaa suturaal awra yi dindi joote Mbkkee ngi mel ni Ndar Ja baa ngay jooti

    La am fa getti Ndar te am Sindoodi Yot nga ko waa Tuubaak Gdek Tindoodi

    Jaaraama Maam Jaara ku am jaaraama Yaa ko waral sa dooma ry karaama

    Jaaraama Maam Jaara ku am Mqaama Yaa ko waral kerook bisub qiyaama

    Jaaraama Maam Jaara ku am ay xarbaax Yaa ko waral sa dooma feealug baax

    Jaaraama Maam Jaara kuy faj aajo Yaa ko waral sa dooma fj sunu aajo

    Jaaraama Maam Jaara ku am hidaaya Yaa ko waral sa dooma am wilaaya

    Jaaraama Maam Jaara ku am ty junni Yaa ko waral sa dooma jommal jinn

  • 10 - Jaaraama Maam Jaara

    Jaaraama Maam Jaara sa xarful jiimi(2) Joxnala jikko yu raft yu yeme

    Jub nga jubal nga japp yaw ty julli Ty jangg ty jox ba leer ya jolli

    T jikko yii may bgga lim amoo leen Jigeen u bon ako amoon yaroo leen

    Daawu la jw doo janni daawu la jayi Doo jayu doo jaayooka jaaya ki jayi

    Yaa sobu yoonu Jannatu Nahiimi Kula royul dm Jaanamaak Jahiimi

    Sa ra(3) gi tax na ba ragal nga Ylla Raft raft njortu t xam nga yilla

    Rewoo ryoo reroo nenaa la daali Doo rummi doo rambaaj Buso Baali

    Amoon nga faayda amoon nga fulla T amu fit am fit ba Yalla fal la2 jiimu Jaara (la lettre jiim de Jaara)3 raawu Jaara (la lettre ra de Jaara)

  • Jaaraama Maam Jaara - 11

    Gore nga am nga kersa am nga karaama Am nga ngrm yaw yaay boroom Mqaama

    Amoo kaaan goreediwoo naam Baali Doo dox di kekkantook a kiitu-aale

    Ma wax say jikko misaal yu tuuti Laaj leen ko maami Soxna Faati Tuuti

    Maam Smba Mariaama ma daa raw cim lf Hamdane li mane Jahnla moo ko taalif

    Noon na bagaan ga woon fa Soxna Jaara Mooy rerukaayub bpp dongo daara

    Mbandam ma musla dey te da daa rootaan Mooy naanukaayab gaaya da koy seetaan

    Masula siis masul dox di bodd Masul di wex-wexlooka dox di gdd

    Daawul weranteeka xuloo ni njldi Moo tax selalul jur nga kuuy jur mbaldi

  • 12 - Jaaraama Maam Jaara

    Kuy laa di Maam Sri Mammar moom Jaara Mbaldee di Daam du gentu we mooy baara

    Da nga lewat mk njaboot nib sardi Moo tax nga jur jambaar ju mel ni gaynd

    Daawo di songanteeka dox di daan Ak di defant tax na am nga waan

    Wcc nga jaajf ya selalu Buso Yaa tax ba nuy seeral gurook a buusu

    Feerul ci jjana ni xuurul hiini Naaley muriitu yaak sa doom lil hiini

    Moo tax u naa la Jaaratul Ilaahi Mariaama mooy sa tur wu mag billaahi

    Ummu xaliifatu-r-rasuulullaahi Muhammadin waladi Abdillaahi

    Ummu imaamu awliyaai-l-laahi Am nga mqaamatu rijaalillaahi

  • Jaaraama Maam Jaara - 13

    Am nga lu kenn amul fi nun billaahi Maam Jaara nl al hamdulil Ilaahi

    Mariaama fuqti muuqinaatillaahi Sa dooma raw kuy jang Bismillaahi

    Mo donnu Ahmadu Habiibullaahi Mo masa jis Amiinu wahyillaahi

    Yaay turandom Mariaama ummu iisaa Sayidatu-n-nisaai raw nga sii saa

    Moo donnu iisaa ma di Ruuhulaahi Moo di donuy Muusaa Kalaamullaahi

    Mo donnu Ibra may Xaliilullaahi Moo donnu Aadama Safiiyyullaahi

    Tuubaa liman tabihahu lillaahi Waylun liman ankarahum billaahi

    Lau joxoon Muhammadul Makiyyu Mi ngi u jox Muhammadul Mbakiyyu

  • 14 - Jaaraama Maam Jaara

    Marxaba ummu Ahmadul Mbakiyyu Waarisu diini Ahmadul Makiyyu

    Marxaba ummu Ahmadal Xadiimi Xaliili zi-l-Buraaqi wa-l-Xayzuumu

    Marxaba uhtu Ahmadul Mbusobi Ku masa wr tataam n tuubi ruubi

    Tatay dojak w la defoon fa Naawel Saeemsa sa mas ta toj t du ko aawal

    Museefu ko soru ci rewum Saalum Ci sox yu takk mbaa kyit fulaa yam

    Yaa baaxu tur Buso t baaxu askan Ygg naoo siyaare gn ji Yonnen

    Yaa raftab juddu t baaxi waajur Ku xncu sy saddiit du jis ludul ngor

    Maam yaa nga gaddaay Gdeki Tooro Diinek gor leen tere jubook Lamtooro

  • Jaaraama Maam Jaara - 15

    Museefuleena jiitu cik wilaaya Mbaa al Quraan mbaa xam-xamub diraaya

    Daawu u puukare mbirum waliyyu Ngir ay Shariif la ooy donuy Aliyyu

    Bmbaa ni ma liy samandaay ab jant Fnk ci maam ma tudd Mammar Anta

    Leer gi bawo Mbusobe suuxi Mbkke Royaat ca askan wa di Mbkke-Mbkke

    Jant ba fnk na lndam ga daay na Bideew suux na suuxileen mbr fee na

    Shamsu Shumuusi doomi jantak weer nga Yaw jarulaa misaal nd fs nga leer nga

    Tambeel ba reeroon ca cosaan u di ko jeex Fee na fa Mbkke leegi pp di fa seex

    Shayxu Shuyuuxi yaa di seexub seex yi Badrul buduuri yaa di weeru weer yi

  • 16 - Jaaraama Maam Jaara

    Xunmu faqiiri yaa di saqqum ndol yi Siitu haqiiri darajaal nga gool yi

    Ummul masaakiini dexuk miskiin yi Abuul yataamaa yaay kenul jirim yi

    Ma naa ko Mbkke yaay Shamsu-d-diini Leeral nga Njmburak Bawal ak Siini

    Siggil nga callalak Habiibullaahi Maam Balla Aysa weeru gn wallaahi

    Yaa tax ba kepp ku stoo ci Mbkke Bu n juneet Ylla tofal ko barke

    Waa Mbkke Saakaaki Mbkke Baari Leeral nga leen ppa ngi dox di waare

    Defar nga say bokku defar aw jmbur Defar Bawal defar Kajoor ak Njmbur

    a daa falook a doon woroomi daara Amuu woon ku mel ni doomi Jaara